Aduna Lyrics by Klangkarussell
(Feat. Marieme)
Yaw kas lay maan a xool
Bu ma la gissé damay ragal
Yaw yaa sama xol
Bu ma la gissé damay joy
Ah
Yaw yaa sama xol
Yaw kas laa bëgg
Bu ma la gissé damay joy
Yaa sama aduna
Ñoom duñu mëso ñëw
Duñu mëso ñëw
Mëso ñëw jël ma
Ah
Bu ñu ñëwee
Fii lañu ma fek
Ñoom duñu mëso ñëw
Duñu mëso ñëw
Mëso ñëw jël ma
Ah
Bu ñu
Fii lañu ma fek
Ñoom duñu mëso ñëw
Duñu mëso ñëw
Mëso ñëw jël ma
Ah
Bu ñu ñëwee
Fii lañu ma fek
Ñoom duñu mëso ñëw
Duñu mëso ñëw
Mëso ñëw jël ma
Ah
Bu ñu ñëwee
Fii lañu ma fek
Ñoom duñu mëso ñëw
Duñu mëso ñëw
Mëso ñëw jël ma
Ah
Bu ñu ñëwee
Fii lañu ma fek
Ñoom duñu mëso ñëw
Duñu mëso ñëw
Mëso ñëw jël ma
Ah
Bu ñu ñëwee
Fii lañu ma fek